Sunu Yaakaar
Sunu Yaakaar
Serigne Malick Diop
Aug 22, 2019 · 22 min

Sunu Yaakaar - Yalla Ciip Na Goor-Jigeen (Xareem La)

MP3
Danuy begg nga delloo ay ndigal ngir nga dimbali dëgg bu baax Kaddug Yalla. Danuy ngëm ne “Sunu Yaakaar" mooy xam Yalla kuy sakk lépp li nekk. Danuy ngem ne népp mën nanu xam Yalla ci Kaadoom ndax Yalla féegnal na boppam ci Kaadoom. Toppal sunu émission “Sunu Yaakaar” ci facebook.com/sunuyaakaar
Soo amé laaj, contactez nous ci email: [email protected]

This podcast uses Soundcloud for stats. What this means Episodes play from the podcast's own servers, unmodified. Not affiliated with Podbay.